Céu ja clareá Consciença ja desanuviá Ja tchiga hora, pa enfrentá realidade Um povo sofredor Ja calmá sê dor Pa'l bem vivê, na paz e na progresso Si nô tiver fê Na nôs capacidade Mâe Africa, ta ser feliz um dia
Africa, Africa, Africa Africa minha, Africa nossa Africa, Africa, Africa Berço di mundo, continente fecundo
Diguenté Sénégal ak Cap-Vert mané soréwoul Soumeu yeugone né niari rewyi ben-la Sama guente bi magni gnane Yallah wone ma ko Africa done bene rew n'dakhe yadi sounou Yaye
Africa Africa Africa Jamma gna yendoo jamma gné fanaan Africa Africa Africa Jamma gna yello jamma gné fanaan
Céu ja clareá Consciença ja desanuviá Ja tchiga hora, pa enfrentá realidade Um povo sofredor Ja calmá sê dor Pa'l bem vivê, na paz e na progresso
Africa, Africa, Africa Africa minha, Africa nossa Africa, Africa, Africa Berço di mundo, continente fecundo
Domou Africa na niou bolo té djapanté Bougnou djapanté geuneu am dolé Kone sama guente bi magni niane Yallah wone ma ko Africa done bene rew nakhe modi sounou Yaye
Africa Africa Africa Jamma gna yendoo jamma gné fanaan Africa Africa Africa Jamma gna yello Té jamma gné fanaan
Africa - sounou, Africa Africa minha, Africa nossa Africa - sounou, Africa Africa minha, Africa nossa
Compositor: Fernando Goncal da Cruz (Cruz da Nando) ECAD: Obra #13423986 Fonograma #2637669